Film e animazione

Série - Nawlé - Episode 02 VOSTFR

Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
facebook
kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.

Commenti 

  1. duez1977

    duez1977

    4 ore fa

    Sous titrage please

  2. Dembéllé sallé

    Dembéllé sallé

    14 ore fa

    Pas de traduction encore une fois ? Pourquoi quand une série est super intéressante vous mettez plus la traduction c’est incroyable sa

  3. Mina Diop

    Mina Diop

    3 giorni fa

    Salimata môme diar na dh 😂

  4. Astou Thiam

    Astou Thiam

    3 giorni fa

    Sénégalais est hypocrite je sens que la mère de mounirou retournera sa veste quand elle saura que son fils aime la fille de son ex bonne quelle dis être sa "soeur" bassi kanam

  5. Fatou Niang

    Fatou Niang

    3 giorni fa

    😂😂😂😍😍😍😘😙👰💋🙏

  6. Fatou Niang

    Fatou Niang

    3 giorni fa

    😂😂😂😍😍😍😘😙👰💋🙏

  7. Fatou Niang

    Fatou Niang

    3 giorni fa

    😂😂😂😍😍😍😘😙👰💋🙏

  8. Fama Sana

    Fama Sana

    5 giorni fa

    On attend le VOST FR s’il vous plaît 😭😭😭

  9. Matar Habib

    Matar Habib

    7 giorni fa

    800.000f et nous dans tout ça, on ne touche même pas les 1/16ème

  10. Sipewou edith

    Sipewou edith

    8 giorni fa

    Qui comme moi se sent perdu dans la traduction ici? On paye combien pour apprendre le wolof ? 😂😂😂😂 toujours des séries intéressantes mais BLOCUS au niveau de la langue pour les étrangers comme moi. Pitié

  11. Abdou Diop

    Abdou Diop

    8 giorni fa

    Mounirou est amoureux de salimata depuis son enfance mais il n lui a jamais révélé alors cette dernière n savait Jesper k la demande en mariage n vas pas gâché cette famille qui est toujours ensemble bakari aussi il regarde son intérêt

  12. Rane Diop

    Rane Diop

    8 giorni fa

    Nonnn donc Ousseynou dafaa doubler son cousin si Salimata hhahaahhaha lol mdririr Quel combat alors

  13. salimata sambe

    salimata sambe

    8 giorni fa

    Quel discours 🥰🥰🥰 où sont les SALIMATA 💝

  14. Alioune badara Fall

    Alioune badara Fall

    8 giorni fa

    Salimata dafa timide trop lii mo takh mou guene infidèle la rôle de coumba

  15. Fatadio Aliou

    Fatadio Aliou

    9 giorni fa

    Déjà vue suis désolé

  16. samba fall

    samba fall

    9 giorni fa

    Rabi sa rôle bi bokoy joué kene doula beugue mbecil salarié moy yelwane merde à la fin

  17. Maguette Gaye

    Maguette Gaye

    9 giorni fa

    Dafa am lou may nawle bane biss lay am

  18. Amicolle Fall

    Amicolle Fall

    9 giorni fa

    Kone wa association oubi groupe whatsapp kafoleine ni 😭😭😭😭😂😂😂😂😂😂😂bamou sotti rek amna ay khememeurrr ak ay dieuw katt ak ay doxane katt 🥳🥳🥳🥳🥳😫😫😫dîna wathie

  19. Gning Modou

    Gning Modou

    9 giorni fa

    Halte à la promotion de l'infidélité

  20. Touty Tall

    Touty Tall

    10 giorni fa

    Kharal ma nieuw khol lou nawlè di dionxè tamite

  21. coumbiz rio

    coumbiz rio

    10 giorni fa

    Nafina del portez des boucles d'oreilles way

  22. livia apa

    livia apa

    10 giorni fa

    les sous-titres ça marche pas!

  23. hevbeauty

    hevbeauty

    11 giorni fa

    c'est pour quand le sous titrage?

  24. Hawa Bocoum

    Hawa Bocoum

    11 giorni fa

    Yocklén machallah

  25. Alimatou Mbaye

    Alimatou Mbaye

    11 giorni fa

    Mane dall ousseynou la sanil carte mane ak kane

  26. Mareme Aidara

    Mareme Aidara

    12 giorni fa

    il a pas plus dur que l'amour caché

  27. samba seck

    samba seck

    12 giorni fa

    Mies Satan katte yii war nano ame bénne série dhé tmt ah

  28. seydina omar diop

    seydina omar diop

    12 giorni fa

    Stp son biye daw si souff kou xam noumou toudou au kouko way

  29. Mariama Loum

    Mariama Loum

    12 giorni fa

    Une très belle Série et bien inspirée ❤️❤️❤️good job. Mais khar Media maneu khar naa Série Regret beu soneu tamite . Sur ce bonne continuation à toute l'équipe

  30. Sokhna Diao

    Sokhna Diao

    12 giorni fa

    Wa kharr média lane moy sen secret sur la lettre"A" Khadija , ndéla ,sadiya, salimata

    • beug baye Xaritou mamem

      beug baye Xaritou mamem

      2 giorni fa

      Oumaya

  31. Aissatou Diallo

    Aissatou Diallo

    12 giorni fa

    C un beau théâtre machallah

  32. Galou Dem

    Galou Dem

    12 giorni fa

    Raby je taime bcp depuis idole tu joue bien machallah

  33. TMD-POULO -NDIONTADO

    TMD-POULO -NDIONTADO

    12 giorni fa

    Néna borom salaire 800000f menoul dara donc borom salaire 200000f niogui dioye. Wakhi dof mane dé je préfère celui avec les maigres moyens té yeureum par rapport ak riche bima gnin té tegg ma beute🙏

  34. Mariane Diop

    Mariane Diop

    12 giorni fa

    Nawlé dioulite dioulite moy nawléme.apres mou diékh

  35. Mame ndiaye Mbow

    Mame ndiaye Mbow

    12 giorni fa

    Hi dina nekh ak nafy dieye rk

  36. M Dic

    M Dic

    12 giorni fa

    Sén Nawlé laniou dh man dh yii khétou amour 💘 damay jalouse dh🤗🤗

  37. Queen Mayna Gueye

    Queen Mayna Gueye

    12 giorni fa

    Wa khar média vous ne voulez op un jumeau pour mounirou khana j'ai mon grand frère qui lui ressemble beaucoup

  38. fabiola happi

    fabiola happi

    12 giorni fa

    sous titres

  39. Louisa seutou almaktoum

    Louisa seutou almaktoum

    12 giorni fa

    Khaar média , toujours des thèmes pertinents , bonne continuation, on adore!!!!!💓💓💓💓💓

  40. sanou Mbengue

    sanou Mbengue

    12 giorni fa

    Sara moytoul maquillage bou eup bi ate khéfyi Ousseynou warone nga prévoir gel sur la table, Covid bagui fi dé

  41. Mya Quenn

    Mya Quenn

    13 giorni fa

    J'adore cette série mention très bien à vous Allah veiller sur toutes les acteurs

  42. Fatima Zahra Bana

    Fatima Zahra Bana

    13 giorni fa

    Sa se voit que c'est du film tout simplement. 800mille guakoy kheipp comme salaire. Oufff

  43. Zeynab Rassoul

    Zeynab Rassoul

    13 giorni fa

    Dama tayal si série nakh ousseynou dou moudié tak saly 😭😭😭

  44. Miss Gueye

    Miss Gueye

    13 giorni fa

    Love Ousseynou ❤️

  45. ya ndeye marieme sy

    ya ndeye marieme sy

    13 giorni fa

    Saly ioe mom gnou livré la aye sachet rek nga dieul sou nékone drogue police gnew diaplela sa adouna yakhou

  46. Dioundiou Lo

    Dioundiou Lo

    13 giorni fa

    Nice❤

  47. diop aby

    diop aby

    13 giorni fa

    Salimata dafa nice mais g pas trop confiance en elle. Wa yeen ani regret ak djabarou gorgui....eupeneu

  48. Maeva Diouf

    Maeva Diouf

    13 giorni fa

    Lii dehh moo leumbe senegal nawle khett..... doyna warrr

  49. Fatou Samb

    Fatou Samb

    13 giorni fa

    Ma diéma sétane nawlé comme guissouma regret wala la femme du chef 🤔

  50. Binetou Malick Kane

    Binetou Malick Kane

    13 giorni fa

    Pourquoi on a la série rarement 🥺

  51. aicha diallo

    aicha diallo

    13 giorni fa

    Aaye waaay kagne laay ame kou melni Ousseynou si romantique ?? 😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍

  52. aida faye

    aida faye

    13 giorni fa

    wa yéne li dou keur gniome sadiya

  53. Aminata Goudiaby

    Aminata Goudiaby

    13 giorni fa

    Ousseynou dafa romantique kW 🥰🥰🥰🥰

  54. Ndeye ha ichatou touré

    Ndeye ha ichatou touré

    13 giorni fa

    Naguén déf dama diaron si sériyi motakh

  55. Ba Aminata

    Ba Aminata

    13 giorni fa

    Bonjour peut o avoir les sous-titres svp merci ?

  56. Mado G'y Dioufy

    Mado G'y Dioufy

    13 giorni fa

    Juste une question pourquoi les gens aime les hor sujet vous énervé a la fin puffff😡

  57. Rokhy Mane

    Rokhy Mane

    13 giorni fa

    Waa 4ans de relation yayou Saly nane yakolene faténa nioune neupp relation laaniou meune 😂😂😂

  58. Rokhy Mane

    Rokhy Mane

    13 giorni fa

    Mé secrétaire yii tamite nagnou niow bureau avc un p de maquillage sééne cils yii comme Ay demkatou xeww

    • Mamy Dia

      Mamy Dia

      13 giorni fa

      Même dem kattou khew sakh dou deff li. 😂😂😂😂😂

  59. lo djamil

    lo djamil

    13 giorni fa

    Ki mo kate ndayam nena salaire 800mil dou dara domou ram

  60. Coumba Diakhate

    Coumba Diakhate

    13 giorni fa

    Mani la femme du chef lagn soxla AK regret

  61. samba agne

    samba agne

    13 giorni fa

    Mais ana diabarou gorgui

  62. khady thiam

    khady thiam

    13 giorni fa

    Amy mii dei dou kharite ni référence ....

  63. Ndew Diop

    Ndew Diop

    13 giorni fa

    Ayoo suis très contente de voir nafi diéye dans une série franchement je l adore et elle très bélle machalla mh tmt bayil néan moyen fo dieum yobou kofa😁

  64. Fatou Niang

    Fatou Niang

    13 giorni fa

    Titre bi dhé Amna Chance Serie bi Yalna Amé Chance Nonou❤👌

  65. Ndeye fatou Seye

    Ndeye fatou Seye

    13 giorni fa

    Nn livreur bi dead nama🤣

  66. Fatou Demba Thioune

    Fatou Demba Thioune

    13 giorni fa

    Sali n’aime pa ouaseynou deysane sa s voi

  67. Fanna Ceesay

    Fanna Ceesay

    13 giorni fa

    who sing the song on the background

  68. awa diack

    awa diack

    13 giorni fa

    Masalah série bou neh

  69. silksmithaful

    silksmithaful

    13 giorni fa

    Rabia est la femme de quel frère alors

  70. Adja Soukeye Gning

    Adja Soukeye Gning

    13 giorni fa

    Deukk bii kenh mounoufi préparer mariage en sécurité 🔐 🤔🤦‍♀️

  71. nafi diakhate

    nafi diakhate

    13 giorni fa

    Vous avez raté le cadre de vie de chez salimata... c'est des gens dimine il fallait un autre présentation de leur maison

    • Fatou Drame

      Fatou Drame

      6 giorni fa

      Je me suis dit la même chose

    • Rane Diop

      Rane Diop

      8 giorni fa

      @Astar cisse wala c'est ça !

    • Astar cisse

      Astar cisse

      9 giorni fa

      Mais je penses q c pas une question de pauvre mais plutot une histoire caste

  72. Bou Serigne Touba

    Bou Serigne Touba

    13 giorni fa

    Sahara migui khépp 800mil té man 5moi batay magui weur salair 60m8l mlou teu ma ttiey yalla amna gnou yalla diapalé dh li dafa am si rew motax mai alkhamdoulilah

    • Bou Serigne Touba

      Bou Serigne Touba

      9 giorni fa

      @Deugg Rekk Tv badou yéména dal

    • Deugg Rekk Tv

      Deugg Rekk Tv

      9 giorni fa

      Doul rek laniouy def....salaire 200 mille sakh da rare

    • EVELINE GOMIS

      EVELINE GOMIS

      13 giorni fa

      billahi

  73. Mbathio Cisee

    Mbathio Cisee

    13 giorni fa

    Nawle dal serie bi nekhe nama ousseynou hum ma sha Allah mounirou osi salimata la nop mais rabia tmt noooo elle me soul way avec c histoir tei gueumoul dara ish

  74. Aisha Rassoul

    Aisha Rassoul

    13 giorni fa

    Rabia en plus d’être folle elle est matérialiste Tite une vrai peste

  75. Seydina ADAMA Ndar Mouna DIOP

    Seydina ADAMA Ndar Mouna DIOP

    13 giorni fa

    Man dei salairou 75/70000 la guis Sénégal te mignonne nena 800.000 du salairou dara

  76. Sokhna Niang

    Sokhna Niang

    13 giorni fa

    Machlla ♥️

  77. Adame Ngom

    Adame Ngom

    13 giorni fa

    Maman mounirou noboul salimata domou mbindane kene douko wakh waye je comprend nawle la toudou

  78. MamiiSha Sow

    MamiiSha Sow

    13 giorni fa

    Ousseynou moy saï saï deeh😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️

  79. MamiiSha Sow

    MamiiSha Sow

    13 giorni fa

    Mounirou waaay 😂😂😂😂🤦🏽‍♀️

  80. Fatou Sidibe

    Fatou Sidibe

    13 giorni fa

    Quand je vois des gens qui s aime sa me r appel des truc

  81. Alaloudarmankobi diakhoumpa

    Alaloudarmankobi diakhoumpa

    13 giorni fa

    Mounane domou mindane mi domou mindane bi mola dak fouf 😡

  82. Sokhna S

    Sokhna S

    13 giorni fa

    Nafi dieye comme kouy repeter

  83. Ndeye Maty Diallo

    Ndeye Maty Diallo

    13 giorni fa

    Machallah

  84. Ndeye Liza kalela

    Ndeye Liza kalela

    13 giorni fa

    Secrétaire setane toute les serie

  85. Fatou Ciss

    Fatou Ciss

    13 giorni fa

    🥰Ousseynou mom Romantique naa di⭐🤣🤣🤣🤣

  86. Mama Jaiteh

    Mama Jaiteh

    14 giorni fa

    Marshallah I love this movie 😍😍😍👍

  87. Isidore Memdy

    Isidore Memdy

    14 giorni fa

    Saly et Ousseynou vous formez un joli couple c sa la vie ❤️♥️ Ousseynou bonne chance

  88. adji diop

    adji diop

    14 giorni fa

    Rabia mome sikk na dh té meune khébaté🤣🤣🤣xalass

  89. Arame Thioube

    Arame Thioube

    14 giorni fa

    Wa khar madia yéne ani sadiya🤦

  90. Khoudia Laye

    Khoudia Laye

    14 giorni fa

    Yen mom teguolen niou fen ish yeuffi dou course 🏃 am ben série diko tek normalement sax mo gueun li Daguey fatté sax ligua setanone la fois passé 🤦🏽‍♀️

    • Mariama Gueye

      Mariama Gueye

      11 giorni fa

      @Khoudia Layeah bon merci😥😥😥

    • Khoudia Laye

      Khoudia Laye

      12 giorni fa

      @Mariama Gueye bn épisode 2 laniou tolu mais da am épisode 00 lolotaxx meun gua djap ni 3 laniou tolu selon toi

    • Mariama Gueye

      Mariama Gueye

      12 giorni fa

      @Khoudia Laye ma tek ne trois lsgne tolou

    • Khoudia Laye

      Khoudia Laye

      13 giorni fa

      @Mariama Gueye 2 lagn tolu ni

    • Mariama Gueye

      Mariama Gueye

      13 giorni fa

      Wa episode 3la

  91. Khady Cisse

    Khady Cisse

    14 giorni fa

    Très intéressant

  92. mado diagne

    mado diagne

    14 giorni fa

    Wa khar production boulen fater mayyy ma generik salimata bou youssou ndour please. C elle la concerner

  93. Mamita Bah

    Mamita Bah

    14 giorni fa

    Saly et sa famille devait vivres dans une maison médiocre pour qu’en t’ils améliore que sa soit remarquable qu’à même 🤦🏻‍♀️

    • Mabintou Diallo

      Mabintou Diallo

      13 giorni fa

      Elles étaient pauvres mais comme la maman travaille avec une riche femme d'affaire bah la dame je pense les. Aides beaucoup dc possible gnou dieuk si ker bu rafet s'en sitiztio'I change touti

  94. Mohamed Benzékry

    Mohamed Benzékry

    14 giorni fa

    Saly molna ndiol la daal nopnako way 🙄

    • Yaye Maye Lat Mbao

      Yaye Maye Lat Mbao

      12 giorni fa

      @Mohamed Benzékry meunoumako yaw tmt khana do deggue

    • Mohamed Benzékry

      Mohamed Benzékry

      12 giorni fa

      @Yaye Maye Lat Mbao bayima legui xana do degue🙄

    • Yaye Maye Lat Mbao

      Yaye Maye Lat Mbao

      12 giorni fa

      @Mohamed Benzékry noboumala khana do deggue

    • Mohamed Benzékry

      Mohamed Benzékry

      12 giorni fa

      @Yaye Maye Lat Mbao Kone nopma niou nobanter 🙄

    • Yaye Maye Lat Mbao

      Yaye Maye Lat Mbao

      12 giorni fa

      @Mohamed Benzékry meunoumako

  95. Max La lionne

    Max La lionne

    14 giorni fa

    Ouseynou goor gou bakh ni yaw lay meel wayé femme binga love meritewoul sa beuguel dakh cousin la nopp

  96. Khadija Drame

    Khadija Drame

    14 giorni fa

    *Une diction parfaite

  97. Khadija Drame

    Khadija Drame

    14 giorni fa

    C tout mignon.com🥺🌜🥰🥰🥰🥰🥰🥰 de plus Ouseynou a un langage seghorien ,un diction parfait

    • Khadija Drame

      Khadija Drame

      12 giorni fa

      La diction accompagne l'effet oratoirrr car pour avoir la force de conviction il faut être convaincu et convainquant ,et on ne peut ,hélas ,convaincre qu'à travers les mots.

  98. Khadija Drame

    Khadija Drame

    14 giorni fa

    Non galanterie ça existe tjrs

  99. Daba Gueye

    Daba Gueye

    14 giorni fa

    Série bi nékhna trop wayé salimata est ce que dina seuy ak ousseynou beugue na séne couple bi dal ba bénéne épisode inchallah

    • oumista Dia

      oumista Dia

      13 giorni fa

      Mounirou laye moudiél

  100. princesse torodo

    princesse torodo

    14 giorni fa

    Mai pk la maman de saly niko yak oussynou yagoulen alor kils ont fai bientôt 4ans En pls gniy wakh yayou rabia si commentaire bi Esk douguéne maci dimbali tamite Rabia ak Ousseynou sen parent dagno décédé non

    • Mabintou Diallo

      Mabintou Diallo

      13 giorni fa

      Mère bi si bop bop am n'a loco manqué même soude 1mois sahh beuri na, mais 4ans wala da beugue sa fille de fornique, wala sou togue ba am 40 ans mou koy deff pression pour mou am diekeur, vraiment certains parents

Il prossimo