Intrattenimento

#MBETTEL SAISON 4 ÉPISODE 40

Commenti 

  1. Fallou Mbaye

    Fallou Mbaye

    5 ore fa

    Yalna lène yalla fayé billah

  2. Fallou Mbaye

    Fallou Mbaye

    5 ore fa

    Je tm okaye Afrique danioulen rawsi abonnés mais rawounioulèn si yalla et raafétal je tm

  3. Fallou Mbaye

    Fallou Mbaye

    5 ore fa

    Billahi ♥️ bou séri yeup mélon né mbéttel billahi ♥️ Sénégalais normalnanou bou yagge

  4. Marimar Ndiaye

    Marimar Ndiaye

    5 ore fa

    cours Coran an ligne et an domicile entrés contak 76 758 03 56 77 472 95 66 merci

  5. Djibril sall

    Djibril sall

    6 ore fa

    kkkk merci wayy fattt dam

  6. mamadou cisse

    mamadou cisse

    7 ore fa

    Machahalah

  7. Fina26 Diop

    Fina26 Diop

    7 ore fa

    pappa diouf guerre day saf mondial

  8. zeinab rassoul Ndiaye

    zeinab rassoul Ndiaye

    9 ore fa

    Gniy dioukk si deudeulè dieukeur Ak Diabar teih sokhorr rek takh Ak bagn yallah boulen yallah may ndam si barkep Seydina Mouhamed saw

  9. Boubacar DIOUF

    Boubacar DIOUF

    9 ore fa

    🤣🤣 Non, Mbettel dou Ay fo...Papa Diouf takk yayou Adama Fall,😅😅 la situation va devenir vraiment compliquée

  10. Akon Niang

    Akon Niang

    12 ore fa

    Adama fall sa Papa djou béss dji bétuma

  11. Faramareen 100

    Faramareen 100

    12 ore fa

    Lane ❤️🔥

  12. Pop Smoke The Woo

    Pop Smoke The Woo

    12 ore fa

    Léna

  13. Ado Ndiaye

    Ado Ndiaye

    13 ore fa

    Bi yayu adama fall di wakh nan dafa am dieukeur bou bess avant Mouy paré mangui ré😂😂😂 je savais que Papa Diouf mofa diaar

  14. Malic Mbye

    Malic Mbye

    15 ore fa

    Adama Gaal 😂😂😂😂😀

  15. arrbi tv

    arrbi tv

    15 ore fa

    Nice 👍

  16. Kana Mb

    Kana Mb

    15 ore fa

    P

  17. KHADY KANE

    KHADY KANE

    16 ore fa

    😯😯😯

  18. Aminata Cissé

    Aminata Cissé

    17 ore fa

    Bizarrement on ne voit plus la soeur de Ya Fatou ainsi que la soit disante tante maternelle d'amina

  19. Maty Diawara

    Maty Diawara

    18 ore fa

    Nafisatou bayil nigua mel diakhal guama

  20. matar gueye

    matar gueye

    Giorno fa

    Adama fall serigne ngagne bis ni gui tay sa baye la😂😂😂 diokhe ko thieur

  21. matar gueye

    matar gueye

    Giorno fa

    nafisatou fatdame mi leu gue neu mouche wayé nak sétlén yalla touti thie ni nguen néké😂😂😂

  22. Marie Ndiaye

    Marie Ndiaye

    Giorno fa

    nafi ak fat dame machallah

  23. Marie Ndiaye

    Marie Ndiaye

    Giorno fa

    thiey les hommes dagnouy am séni awo dougnou l'en falé ba toumouranké dilen weuri thiey laye laye

  24. Fatou Camara

    Fatou Camara

    Giorno fa

    ..

  25. Sokhna Niang

    Sokhna Niang

    Giorno fa

    Ahh madion lay weregua

  26. Ndeye Ngone Diongue

    Ndeye Ngone Diongue

    Giorno fa

    Eyway kou kham titre song wou sequannce Laye Laye ak Dama

  27. Abdoulaye Ba

    Abdoulaye Ba

    Giorno fa

    erreur de montage entre séquence fat dame et Mamita mamita frappe la porte fat dame répond et elle entre et elle trouve son père

  28. Soukeyna Dieng

    Soukeyna Dieng

    Giorno fa

    Nooo papa Diouf dou niit 😂😂😂

  29. Diop Cheikh

    Diop Cheikh

    Giorno fa

    Papa diouf modé adama fall tay moude

  30. Beauté d'Afrique

    Beauté d'Afrique

    Giorno fa

    Rouba nak no meuné ame dome deuk ak mome t setlouwoko

  31. Big linzo Ngodiba

    Big linzo Ngodiba

    Giorno fa

    Papa diouff

  32. Dame Seck

    Dame Seck

    Giorno fa

    No moi lena nekhoma

  33. Maria DIEYE

    Maria DIEYE

    Giorno fa

    Tiey fate dame meuné na bouné d Amina tu as raison tu es très belle machala Allez papa diouf

  34. Lacisko Cisko

    Lacisko Cisko

    Giorno fa

    Gnogno elle joue bien

  35. Diop Cheikh

    Diop Cheikh

    Giorno fa

    Ma dion molooo🤣

  36. Alimatou Sadiya Sagna

    Alimatou Sadiya Sagna

    Giorno fa

    Ndama wayy🥰🥰

  37. Abdou Aziz logue vie a notre guide

    Abdou Aziz logue vie a notre guide

    Giorno fa

    Mbétéle c'est le meilleur pour moi

  38. Ba Fatimata

    Ba Fatimata

    Giorno fa

    No papa Diouf d’où nite waye 🤣🤣👌👏👏

  39. Fabintou Ndiaye

    Fabintou Ndiaye

    Giorno fa

    La réaction de Laye Laye est très mauvaise quelque soit Alpha Ndeye Ndiaye était sa femme donc il ne devrait même pas parler d'elle ainsi puisqu'ils ont divorcé. Mais c'est bonne leçon à tirer à travers le comportement de Laye Laye et puis l'a dit "l'homme n'est pas née mauvais cest la société qui le rend mauvais " Amina , ta réaction est très normale parce qu'elles t'ont trahi surtout Ndeye Ndiaye.

  40. elhadji mbaye

    elhadji mbaye

    Giorno fa

    He kalla .bambarayi wakhlen😂😂😂

  41. Fatima Diallo

    Fatima Diallo

    Giorno fa

    Papa Diouf moy bandit billay adama fall woyou bandit moy bayam sa bay migui nonou😂

  42. awa awa

    awa awa

    Giorno fa

    La reation de mamita et c acte c pas bien son père devais parler a se mère deh le premier la foi bi mou ko diokhè khalliss pour kham fane lay dieulè khallissmais bn souvent les parents cepparè li lay diour

  43. Fatima Diallo

    Fatima Diallo

    Giorno fa

    Fat thierno t irresponsable et dégeulasse t’a rien à dire

  44. Fatima Diallo

    Fatima Diallo

    Giorno fa

    Fat thierno t irresponsable e

  45. Maadet Mangue

    Maadet Mangue

    Giorno fa

    Wa son ndama ak mandione bi kou ko way ? 👀❤️

  46. Ginette Lehtola

    Ginette Lehtola

    Giorno fa

    hahaha ! Papa Diouf mo grow

  47. NDEYE MARIETOU BA

    NDEYE MARIETOU BA

    Giorno fa

    Je tife pour roube femme de paix

  48. NDEYE MARIETOU BA

    NDEYE MARIETOU BA

    Giorno fa

    J adore fatdame

  49. Lou yallah Déf rekk Nonoula

    Lou yallah Déf rekk Nonoula

    Giorno fa

    mais je me demande yayou adama fall nekoul wone copinou rouba je comprends plus keski s passe mbettel na diekh way episode 40

  50. Mareme Diop

    Mareme Diop

    Giorno fa

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😜😜😜

  51. Info TV

    Info TV

    Giorno fa

    Bilayy gnounn goor gni dinagn dead dhe yalna gnou yalla musall thi genrou lena yii

  52. Mamadou Guéye

    Mamadou Guéye

    Giorno fa

    Papa Diouf dou nitt bialy Diayneu Adama Fall djiko Bandit

  53. Saliou Niass

    Saliou Niass

    Giorno fa

    nafisatou nena khale bou yarrou wakh ndanke dokh ndank😁😁😁😃😄

  54. Absa Ndiaye

    Absa Ndiaye

    Giorno fa

    🤗

  55. Cheikh Sow

    Cheikh Sow

    Giorno fa

    Adama fall do bandit

  56. Ndeye Mané Fall Fall

    Ndeye Mané Fall Fall

    Giorno fa

    Mais papa Diouf on oublie qu'il a tué la mère d'Amina on fait comme si de rien n'était le télé film c'est Amina qui est mieux tout le reste on fait des erreurs

  57. sourga

    sourga

    Giorno fa

    gagne way yamana heh de halebpou yakhou nilanioukoy yare

  58. sourga

    sourga

    Giorno fa

    ndama wah nga deug de ki daflay yakhal de banial de amnga foula tey

  59. Mame Diarra

    Mame Diarra

    Giorno fa

    Fatou dame.contane n'a si yaw.bien joué.bonne conseil

  60. Princess mbay

    Princess mbay

    Giorno fa

    Lalaye rek la diepi paka gnari borr

  61. sourga

    sourga

    Giorno fa

    mais gagne a quoi il joue?

  62. sourga

    sourga

    Giorno fa

    rouba ne savait donc pas ce qui se passait c'est ndeye ndiaye qui n'est pas normale et sa tante aussi

  63. Massene Ngom

    Massene Ngom

    Giorno fa

    Mais li mom yeufou goorr la il sont les meilleurs

  64. Saitou Hab

    Saitou Hab

    Giorno fa

    Ewo!!!!!!!! Diadieuf

  65. Mamadou Ngom

    Mamadou Ngom

    Giorno fa

    Ça n'a aucun sens

  66. timzy Drame

    timzy Drame

    Giorno fa

    Sérieusement mamita m’énerve elle dépasse les bornes way 😈

  67. Aissatou Lo

    Aissatou Lo

    Giorno fa

    Adama fall il dégoûte 🤢

  68. Bousso Mbengue

    Bousso Mbengue

    Giorno fa

    Moi et ma sœur nafi et ndama

  69. Khadime Lo

    Khadime Lo

    Giorno fa

    LAN MOO XEW? Whatsapp Ag jumtukaay la goo xam ne ñi ngi ko sos ci atum 2009. Ñaari liggéeykatu Yahoo Jan Kum et Briyaan Akton, ginnaaw bi Feesbug wootee am ndaje ngir toñkat yi, ñoom ñaar bi ñu ñëwee ñu naa leen xamuleen dara loolu metti leen lool. Jan Kum dafa amoon benn xalaatu sos ag jëfekaay goo xam ne dinanu man di jokkoo te kenn du nu yëddu, ndax dafa gisoon ay way-juram ñuy def loolu (Ukraine, URSS) mu jël xalaat boobu. 1- Ginnaaw bi mu ko amalee rekk Feesbug ñëw ca moom ngir jënd ko mu bañ, ndax nee na du wor askan wi ndax daf leen a waxoon ne dina leen liggéeyal genn jumtukaay gu am kaaraange kon xaalis du tax mu jaay ko. 2- Ci atum 2014 mu jaay leen ko ci ay sàrt: 2.1- mooy Whatsapp day des nekk Nqàmtu (chiffrement) ngir kenn du am sañ-sañ ci lëñtu li ngay def ci pet 2.2- mooy moom Jan Kum da cay am 40% 2.3- damay bokk ci ñiy dogal ngir di xam liy xew ndax rekk mi ngi ragal ñu lal ci ag caay-caay Feesbug nangul ko ko mu jaay leen ko ci 19i milyaar ci dolaar (19 milliard de dollars). 3- Watsab moom ay Nqàmtu la, loolu mooy lu am kaaraange la kenn manul xam dara ci yaw soo ci defoon ñaawtéef, ndax booy tàbbi kenn du la laaj yaw yaay kan? Say at? Foo dëkk, sa limat rekk lañu soxla, moo tax soo déggee ku naan nguur gi leegi daf koy saytu xamal ne xamul jumtukaay gii. Kaaraange Whatsapp mi ngi sukkandiku ci sa kaaraange jollasu. 4- Ci at yi weesu boroom Feesbug ñëw na ngir jënd Snapchat, boroom lànk bañ koo jaay mu woo ay toñkat fay leen xaalis ngir ñu amal genn jëfekaay. Loolu moo indi li nuy wax istati (statut). 5- Watsab boo yónnee ndéggat widewoo nataal kenn xereñul ba xam ki ko yónnee lu dul kenn ka nga ko yónnee. Nguur ak keneen ñoo ci yam, manuñu koo xam ndax anam gi ñu ko amale Nqàmtu. 6- Xalaatam mooy jumtukaay goo xam ne kenn du ci def aw ñaawtéef. Kenn ku nekk war ngaa moytu yu mel noonu, yitteem mooy jàpple nit ñi ngir ñu man di jokkoo te kenn du leen yëddu. Xaaj bu njëkk Imaam Leeral: Njëfekaay : application Nqàmtu : chiffre, chiffrement Toñkat: développeur Jollasu: téléphone Ndéggat: vocal, audio Limat: numéro

  70. Khadime Lo

    Khadime Lo

    Giorno fa

    Ñaŋ : *# 56*56*56*8*8*# Conexion gratuit

  71. KīñG_Sõūljã

    KīñG_Sõūljã

    Giorno fa

    Papa Diouf bilahi ioe sauwasss 😂😂😂 boy bi dou bvndit papa dieul na yayou boy bii 😂😂😂

  72. Ndeye

    Ndeye

    Giorno fa

    Non je suis chocké mois papa Diouf dieukeurou yayou Adama Fall feuruereuuuuuuuw

  73. Max Sy

    Max Sy

    Giorno fa

    Fat dame kene d’où yaw tu joue bien ❤️chapeau à tw

  74. السنة سفينة نوح عليه السلام

    السنة سفينة نوح عليه السلام

    Giorno fa

    Sèrie bi mom khana kène liguèyou si 😂

  75. Rokhy Thiaw

    Rokhy Thiaw

    Giorno fa

    Laye laye vraiment amo soutoura ,sey soutoura laniou wakh ,quelque soit ton problème avk ndeye Ndiaye,fat dame warouthi kham Dara , mais djiguene yi kholen tey lii leçon la ,

  76. NDARAW NDIAYE

    NDARAW NDIAYE

    Giorno fa

    Lii motah gnou beuri si nit gni meunougnou yor gniari djiabar nah dano djiengue... bo neker si ki hass keuler... bo beunoul nek Djiantal yamal si kene... enplus bou seuy djiéher si digeunté gniari nit na wah bi rafet wala gua nopi soutoura dal bahna

  77. Mane Gueye

    Mane Gueye

    Giorno fa

    Mandione mo gnake diome

  78. codou kharagne lo

    codou kharagne lo

    Giorno fa

    hée papa diouf sa khetou regard lanla cheuteut 😂😂😂😂😂😂😂😔

  79. Ablaye Sam

    Ablaye Sam

    Giorno fa

    Hayre bour yanniane

  80. Fatima Diallo

    Fatima Diallo

    Giorno fa

    Madione laye niak gua diom srx

  81. Sofika Diallo

    Sofika Diallo

    Giorno fa

    Non non papa Diouf yaye bandit nakk

  82. Abibatou Fall

    Abibatou Fall

    Giorno fa

    Non ngagne fan nala tay nak

  83. Ousseynou Niang

    Ousseynou Niang

    Giorno fa

    Non Adama fall bandit wo deh papa Diouf rek Moy bandit

  84. Khafssatou Baro

    Khafssatou Baro

    Giorno fa

    Papa Diouf dou nite

  85. diagne adja fatou

    diagne adja fatou

    Giorno fa

    Yen a marr d mamita ichhhh comm bb

  86. Diop mareme

    Diop mareme

    Giorno fa

    Vengeance day méti🤯🤯

  87. Diama Ndiaye

    Diama Ndiaye

    Giorno fa

    Ani talibè serigne fallou mbackè yi ❤❤

    • Diama Ndiaye

      Diama Ndiaye

      Giorno fa

      Cv

  88. Fatima rassoul Fassa

    Fatima rassoul Fassa

    Giorno fa

    fate thierno sof na trop

  89. Fama anne

    Fama anne

    Giorno fa

    jaari soh yo Allah hollit

  90. Mado G'y Dioufy

    Mado G'y Dioufy

    Giorno fa

    Ay man papa Diouf moy Cochon 😁😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  91. Bbei Helene

    Bbei Helene

    Giorno fa

    Ohhh weusifa bouy daw si souf 🙏🏾🙏🏾

  92. Mado G'y Dioufy

    Mado G'y Dioufy

    Giorno fa

    Genrou madionne laye yi niotakh kein wolotoul kein il ose parlé mal de ndeye Ndiaye alors kil fesai pareille avec fat dam n'importe koi

  93. Mamady DIOP

    Mamady DIOP

    2 giorni fa

    Papa Diouf moye bandit 😂

  94. Cheikh Kane SQB

    Cheikh Kane SQB

    2 giorni fa

    Adama fall tepto fayto 😂😂😂

  95. Maguette Ba

    Maguette Ba

    2 giorni fa

    Wallay adama bandiwo fat thierno man moussoma saff mais laye laye môme sa genre gui motah dinna dee si célibataire

  96. Rama Bakhoum

    Rama Bakhoum

    2 giorni fa

    Nice ♥️👍😁

  97. SGM TV Sénégal

    SGM TV Sénégal

    2 giorni fa

    PAPA DIOUF MIY BANDIT DEUGUE

  98. Gnagna Dabo

    Gnagna Dabo

    2 giorni fa

    Mbettel vous avez perdu le fil de la série ou quoi. Il n'y a plus de personnages dans la série. On dirait qu'ils sont tous bipolaires. A force de vouloir donner des leçons (que nous apprécions tous d'ailleurs) c'est devenue du n'importe quoi. Série bi comme sketch rek.

  99. mar ndiaye

    mar ndiaye

    2 giorni fa

    Papa Diouf way nila guerre day Saf mondiale 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Bakh na si Léna gnaw 😜😜😜😜😜😜😜😜 Mais j’ai vraiment triste 😞😞😞😞😞😞😞😞😞 Rouba Seye mérité woul liiii 😭😭😭😭😭😭😭😭

  100. Alima Fall

    Alima Fall

    2 giorni fa

    Wa hana tata léna bi amoul suivre

Il prossimo