Intrattenimento

MBETTEL SAISON 4 ÉPISODE 28

Commenti 

  1. Maimouna Dary

    Maimouna Dary

    8 ore fa

    Waaa mbettel mom on l’a arrêté ou koi? Ça fait un bail

  2. Houssainatou Tounkara

    Houssainatou Tounkara

    19 ore fa

    😎

  3. Ndeye fatou Diop

    Ndeye fatou Diop

    Giorno fa

    Non djiguéne meunoul niakkei diom yi nafissatou fane lala ousmane dougeul non waye

  4. Wadoudou Fall

    Wadoudou Fall

    Giorno fa

    Kou beugue Sydi Birahime lamp fall defa j'aime 👇👇

  5. Aram Jarju

    Aram Jarju

    Giorno fa

    Why mbettel is not playing now

  6. Thiemokho Tounkara

    Thiemokho Tounkara

    Giorno fa

    Mbettel dma setlou né dmathie deconsantre wou 4 seri de retard lathi am 2jr yi reck makoy dabou wat setat len sen bopou man loume déconcentré reck khormet né

  7. Amina Lo

    Amina Lo

    Giorno fa

    Nafissatou elle m’énerve 😏😏😏😏

  8. Amina Lo

    Amina Lo

    Giorno fa

    Waa naffissatou mii wahoul woone beugoul doom ji shii mane je la comprends pas vraiment 😏😏😏

  9. Amina Lo

    Amina Lo

    Giorno fa

    Waa naffissatou mii wahoul woone beugoul doom ji shii mane je la comprends pas vraiment 😏😏😏

  10. Nadia Assani

    Nadia Assani

    Giorno fa

    Qui sait pourquoi la diffusion de mbettel s'est arrêté ???

  11. Darou Salam tv

    Darou Salam tv

    2 giorni fa

    Mancalah

  12. Niang Dame

    Niang Dame

    3 giorni fa

    Loutakh nguen yabatè ani épisode 29 bi khawouma 30 soof nguène trop

  13. Tally Gaye

    Tally Gaye

    3 giorni fa

    Mais où en sont les épisodes de la série Sénégalaise le meilleur , mbétel .on attend avec impatience

  14. Oumoul Khairy DIACK

    Oumoul Khairy DIACK

    3 giorni fa

    Wa mané ana bou dem bi?

  15. Binetou Lo

    Binetou Lo

    4 giorni fa

    Où est l'épisode suivante ça fait une semaine dougalou lène bou bess

  16. Fatimata Fall

    Fatimata Fall

    4 giorni fa

    Putainnnn nafissatou tu nous saoule avec ousmane wayy

  17. Awa GAYE

    Awa GAYE

    5 giorni fa

    Dama yakarni Deal la pour rouba gnew thi keur pour meuna danel Papa Diouf

  18. atekhouna Mbacke

    atekhouna Mbacke

    5 giorni fa

    Kel hypocrite de papa diouf

  19. Papa Niang

    Papa Niang

    5 giorni fa

    pape

  20. Ladibore Wade

    Ladibore Wade

    5 giorni fa

    Toute mes félicitations

    • Bousso Kebe

      Bousso Kebe

      5 giorni fa

      Ok ok. 😁😀🙏🙏👍.

  21. Fatou Mané

    Fatou Mané

    6 giorni fa

    F

  22. Fatou Mané

    Fatou Mané

    6 giorni fa

    F

  23. Serigne Modou morfall

    Serigne Modou morfall

    6 giorni fa

    😂😂😂

  24. Noush Diaw

    Noush Diaw

    6 giorni fa

    Ya fatou aya bibbammm 🤣🤣

  25. Astou diop

    Astou diop

    6 giorni fa

    Ana talibé Serigne fallou mbacké balla aîcha 👌 yi

  26. lahat cisse

    lahat cisse

    6 giorni fa

    manchallah MBETTEL am na 1 million de vue alhamdoulilah yalla na dieum kanam yalla na yokk vraiment serigne ngagne daffa sonneu si production bi danio meune sen liguéye kham production biniou yor

  27. Maïssa Ndoye

    Maïssa Ndoye

    6 giorni fa

    Nn adama dafa foor mome ak amina tres mignon 😍😍😍

  28. Awa Kane

    Awa Kane

    6 giorni fa

    À

  29. Jwrugy Furi

    Jwrugy Furi

    6 giorni fa

    Z4555d

  30. Sokhna Ndiaye

    Sokhna Ndiaye

    7 giorni fa

    NEKHNA TROP MACHALA ❤❤❤

  31. Elhadj Lo

    Elhadj Lo

    7 giorni fa

    Ms.Mamita bilahi danga rafeit

  32. Elhadj Lo

    Elhadj Lo

    7 giorni fa

    Ms por giseu toumako si image yi dh.mdr

  33. Mina Lo

    Mina Lo

    7 giorni fa

    Bella a tracé une leçon très important . Surtt bimou yeuguei grossesse dem retirer plainte..Dôme....thiey dôme

  34. Alimatou DIEYE

    Alimatou DIEYE

    7 giorni fa

    Hèèè 🙆🏾‍♀️ Lena évolution 😂😂😂😂🤦🏾‍♀️

  35. Adama Thiam

    Adama Thiam

    7 giorni fa

    Mbettel wanéna ni bép nit rawatina djiguéne yaye bou bakh rék mo ame solo kholal Léna ak Yayam rék

  36. Mbargou Diop

    Mbargou Diop

    7 giorni fa

    Merci léna

  37. Mbargou Diop

    Mbargou Diop

    7 giorni fa

    Mais nak mamita nekh nama trop

  38. Mbargou Diop

    Mbargou Diop

    7 giorni fa

    Ya fat dame ak nafi satou gno geuneu saf khorom

  39. Ndiongue Ngom

    Ndiongue Ngom

    7 giorni fa

    Chapeau à vous

  40. Ndeye coumba Faye

    Ndeye coumba Faye

    7 giorni fa

    Je ne suis pas d'accord

  41. Ndeye Fatou Thiam

    Ndeye Fatou Thiam

    7 giorni fa

    Yalna seye bi barké yalna la yallamay goud fann ak werr

  42. Mariama Claudine MENDY

    Mariama Claudine MENDY

    7 giorni fa

    Wa Léna mom changement wam nguawna 🤔

  43. mamita Kane

    mamita Kane

    7 giorni fa

    wayéne dolén wakh si yafatou mi ki Man nama ray 😅😅😅

  44. Toufa gueye

    Toufa gueye

    7 giorni fa

    Tey Léna wakh na deug

  45. Adama Jah

    Adama Jah

    7 giorni fa

    Alors Léna t'as pas le choix si propos de Adama on dirait qu'il t'a proposé de coucher avec lui c'est mon avis Et puis sakh yaw Bella toi au moins tu est enceinte et ensuite avortée je te dis massa mais tu es égoïste parce que t'a grand sœur n'a jamais été enceinte et tu te plains devant elle

  46. diouldé Gueye

    diouldé Gueye

    7 giorni fa

    Nafissatou bayima waye dafmaye fathie barki serigne saliou mbacké damako beugeu 😂😂😂😂😂

  47. M D

    M D

    7 giorni fa

    Waaw mais le réalisateur ou le scénariste de Mbettel , vous avez une dent contre Rouba Seye ou quoi??😡😡. A quand aura t elle droit au bonheur ?? Depuis le début elle a que des malheurs et de la souffrance, daffa doyye vraiment!! Elle a droit au bonheur comme tout le monde !! Boulénn ma wakhlo nakk 🙄🙄🤨!

  48. Mamadou Dieng

    Mamadou Dieng

    7 giorni fa

    Vraiment NAFISSATOU tu as raison car la femme est si précieuse que homme la femme est une princesse l homme doit être tout pour elle respectons les femmes MBETEL merci

  49. Mamadou Ly

    Mamadou Ly

    8 giorni fa

    Mbettel the best series that agrees

  50. Ndella Ngom

    Ndella Ngom

    8 giorni fa

    Thieuy nafi satou ndeysan boy ouz dh foumoula teyeu deguer na😂😂😂😂 li comme guère

  51. mariama mballo

    mariama mballo

    8 giorni fa

    ماشاء الله

  52. Oumy Kadam

    Oumy Kadam

    8 giorni fa

    Nafisatou meinoumako comprendre nak

  53. Dickel Sy

    Dickel Sy

    8 giorni fa

    Wa mani ongle lena yi tamit amna bou manque deh walla mbethie bi mou mey adama fall mo dall😂😂😂😂😂

  54. khadre thiam

    khadre thiam

    8 giorni fa

    Mamita meyal sa yaya diam waaay hoooò

  55. mamadou wade

    mamadou wade

    8 giorni fa

    Nafisatou wakhna lou amm solo jugén dafa sonou lou nieuw niouni momla😓😓

  56. MamiiSha Sow

    MamiiSha Sow

    8 giorni fa

    Lena taye deeh wakhgua deugue seuh yaye deeh😂😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️

  57. MamiiSha Sow

    MamiiSha Sow

    8 giorni fa

    Mdrrrr Amina aq Adama Fall deunio dioubo nii? Ah waa kone bateiy bakhna👩🏾‍🦯👩🏾‍🦯👩🏾‍🦯

  58. MamiiSha Sow

    MamiiSha Sow

    8 giorni fa

    Pardon mais ya fatou mi niit leuh est ce que non putaiiin yeine degré hypocrisie aq sokhor bi amatoul way🤦🏽‍♀️

  59. MamiiSha Sow

    MamiiSha Sow

    8 giorni fa

    Nafissatou aq Ndama dinegn meuh raaye req putaiiin noon😂😂😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️

  60. Bouba Fanne

    Bouba Fanne

    8 giorni fa

    Meilleur série sénégalaises en tout cas

  61. Diop Marie Abrouss

    Diop Marie Abrouss

    8 giorni fa

    Amina tu es tres belle

  62. Bineta Fatima Sow

    Bineta Fatima Sow

    8 giorni fa

    Ay la maman d Lena topatol sa keur ak sa dieuke yi mo gueune guay lidieunti rouba

  63. fatou kine SECK

    fatou kine SECK

    8 giorni fa

    Ay way sama Ame soeur Fonek 😂😂 god montre le moi 😂

  64. thioro seck

    thioro seck

    8 giorni fa

    Traduction bii😂😂😂

  65. شمس الهدى

    شمس الهدى

    8 giorni fa

    أين العاشقون بللغة العربية اخرجوا من هنا لنتحدث معا 🥰🥰🥰

  66. Bousso Mbengue

    Bousso Mbengue

    8 giorni fa

    Léna ana sa béneu wéeee

  67. Perfect Bibzey

    Perfect Bibzey

    9 giorni fa

    Lena niak nga kerssa😂😂😂😂ms c bien

  68. Khouma Tv

    Khouma Tv

    9 giorni fa

    Non mane niarr gni dinaniouma ray bella ak fat dame

  69. MARABOUT GARBA

    MARABOUT GARBA

    9 giorni fa

    Medium Voyant Ésotérisme et prêtre vaudou Certains d'entre vous n'ose plus consultés les sites internet suite à la mauvaise expérience. Il y en a qui ont malheureusement tombé sur des sites malhonnêtes concurrent. Que les choses soient bien claires, je n'ai aucun rapport avec ses sites qui ternissent l'image du maraboutage. Je suis un prêtre Vaudou honnête et sincère. Seulement des consultations et des travaux de hautes qualités-vous sont proposés chez nous avec le stricte RESPECT des règles drastiques. Vous pouvez compter sur moi et mon soutien. Sachez qu'avec moi vous aurez tout ce que vous voulez comme satisfaction mais la seule chose que je n'aime pas du tout, c'est quand t'ont m'oublie après avoir reçu la satisfaction totale. J'aimerai vous propose une consultation et un travail unique : -Ramener sa femme/mari même si cela fait plus de 20 ans; Ramener sa chance; Retrouver son amour; Réussir sa vie; Contre accident; Contre sorcellerie; Avoir facilement du travail; Avoir des enfants; Portefeuille magique; Adhérence pour la protection et la protection de sa maison Et plus encore!… Je n'ai pas de problème à travailler à distance. Des résultats sont immédiat et durable et le payement de la main d'oeuvre serai après la satisfaction totale. Possibilité d'envoi par la DHL, FEDEX, EMS, UPS, TOP-CHRONO, par la POSTE ou par voie mystique CONTACT Téléphone: +22-995-719-863

  70. ndiaye ndiaye

    ndiaye ndiaye

    9 giorni fa

    c est une ecole

  71. ndiaye ndiaye

    ndiaye ndiaye

    9 giorni fa

    vraiment mbettel c est une série purement sénégalaise

  72. Aminata Mbaye

    Aminata Mbaye

    9 giorni fa

    C’est quoi ces enfants toxiques qui cherchent le malheur de leur mère?? Avant Amina et Ndeye Ndiaye et maintenant Mami. Non mais s’ils vous plaît

  73. Souleymane jules Sy l'officiel

    Souleymane jules Sy l'officiel

    9 giorni fa

    Ki regarder la Série Mbettel avec Son Téléphone portable 👍📲 🤔

  74. kebe marieme

    kebe marieme

    9 giorni fa

    Entre ouamane ak nafissatou barké le zé dotou ma si wakh 😷😷😷😷

  75. Ndeye Awa Diouf

    Ndeye Awa Diouf

    9 giorni fa

    Non fat dame ak nafissatou mane niom laa beugue😍

  76. Dieng Diadiaa

    Dieng Diadiaa

    9 giorni fa

    . Non khetou diab ya fatou dafmay ray🤣🤣🤣

  77. Ndiaye Seyni

    Ndiaye Seyni

    9 giorni fa

    Vraima lena comace a m plair car el necoute pl8 ls coseil d sa Maman

  78. Oumy Diop

    Oumy Diop

    9 giorni fa

    Ya fatou ni rek

  79. BOYE Mame

    BOYE Mame

    9 giorni fa

    Dou avortement aussi fausse-couche là 🤦🏾‍♀️ Franchement yeureumolen s'en ndey yi! Vous abusez grave 😭 À vos grands âges vs voulez que vos parents délou ensemble, alors vos mères souffrent ! C'est trop😩

  80. sokhnaawa toure

    sokhnaawa toure

    9 giorni fa

    Thiey les hommes,fénne rek...dagnioulay 🐢 bassa khôl bii ddiwadjia wadeu bougniou togué DILA eupe lamegne ak dila diaye...

  81. MB S

    MB S

    9 giorni fa

    Wa mane Nafissatou mi loutakh moy niak diome la khamoul?

  82. aronafall gueye

    aronafall gueye

    9 giorni fa

    Adama sa santa bi rek moma metti warone nga woutt benen 🥺🥺🥺

  83. Oumy Diop

    Oumy Diop

    9 giorni fa

    Eumb makk d li moy conséquences yi

  84. Awa Jallow Dimson

    Awa Jallow Dimson

    9 giorni fa

    Léna koula guiss khamni meusso dèm marcher 😂😂

  85. Rokhya Cissé

    Rokhya Cissé

    9 giorni fa

    Mandione sadjj nga

  86. Awa Diop

    Awa Diop

    9 giorni fa

    Kou d'acord nes ndeye sine nitt geu nou kho

  87. Diop Seny

    Diop Seny

    9 giorni fa

    Série préfère

  88. Bineta Ba

    Bineta Ba

    9 giorni fa

    Léne mome Ani sa béne ongles bi sheut delene xol liguene Di df 😂😂😂😂😂

  89. Ya Fatuo Dieng

    Ya Fatuo Dieng

    9 giorni fa

    Ok

  90. Ndeye Dieng

    Ndeye Dieng

    9 giorni fa

    Jotayu fat dam ak nafi dfmay neeex😍❤❤

  91. Ngone Coundoul

    Ngone Coundoul

    9 giorni fa

    Cette serie c du realitè pur et dur.mention speciale jadore ce serie😍😍😍😍

  92. Awa Thiam

    Awa Thiam

    9 giorni fa

    T

  93. Samath Diop

    Samath Diop

    9 giorni fa

    Non série amena solo fatdame et sa sœur mamita et sa mere chapeau à vous

  94. Lee Krino

    Lee Krino

    9 giorni fa

    que des leçons de morales !!! magnifique vraiment

  95. Fama doumbia diallo

    Fama doumbia diallo

    9 giorni fa

    Amina name n’a sey ay trésse

  96. Ba Fatimata

    Ba Fatimata

    9 giorni fa

    Ey ya fatou dil digeul sa dohm Léna Lou bakhe en plus elle a décidé d’être une bonne personne doko diapalee waye thi ya fatou adada 🤦‍♀️

  97. Touba Amy

    Touba Amy

    9 giorni fa

    Papa diof wakh ga dague dh yalla rk moye kéne

  98. Babacar diop

    Babacar diop

    9 giorni fa

    Sounguène dégué gnounane série bu nékh mooy bii

  99. Nene Toure

    Nene Toure

    9 giorni fa

    Y’a Fatou mi nit la

  100. Nene Toure

    Nene Toure

    9 giorni fa

    Machallah Rouba sey bien répondu à yaye Fatou

Il prossimo