Mariama Saison 1 - Episode 0 ( Long Metrage)
Pubblicato il 16 giorni fa
visualizzazioni 824K
Une série Sénégalaise: Mariama est l'histoire d'une jeune fille, brillante élève qui voit son rêve brisé lorsque ses parents décident de la marier de force avec son cousin Kalidou immigré de retour.
N'oubliez pas de vous abonnez a notre chaine ITput YESDAKAR
Retrouvez - nous sur www.yesdakar.com/ ou télécharger l'application sur
- Playstore: play.google.com/store/apps/details?id=com.cyborgtech.yesdakar
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
Abonnez Vous a notre Chaine ITput itput.info
Yesdakar
15 giorni fa
Retrouvez la Serie Mariama tous les Mardis et Vendredis à partir du 16 Avril 2021 sur la Chaîne ITput Yesdakar. N'oubliez pas de vous abonnez a notre chaine ITput YESDAKAR
Kimo Khalid
9 ore fa
Mercip
manké sylla
11 ore fa
Bonjour On aura pas droit au sous titre ?
Khady Sylla
6 giorni fa
@Soukeye Diagne qa
gueye maguette
7 giorni fa
@Aliou Dia mardi et vendredi
yaayou baayam
7 giorni fa
Waaa kagne lay amat
Mendy Giselle raveka
4 ore fa
Li noble gang la warone toude dakh team ba fi nék 😂😂khola killer mom
Mouhamed Thiaw
6 ore fa
Proff bi nadege dinako ray rk😂😂😂
Malick Gueye
8 ore fa
Surveillant yi dagni yokou cas féne nioko fi dakk
ibson diouf
9 ore fa
Khalidou defoul diamou
Naby Kara
Giorno fa
Surveillant day ndélou kon
Mina Diop
Giorno fa
Machallah série bi nekhna trop
Pape Diagne
2 giorni fa
Très bonne série félicitations
Papa Badji
2 giorni fa
Théye cuisse 😂😂🔥
Falloux
3 giorni fa
Son bi😩
Baris221 Le Mbouroi
3 giorni fa
Bala nga wakh wakhi takk dangay dokhane ba paré lolou moy yeufi goor
Maruzza Ndiaye
3 giorni fa
Encore une autre belle mère qui veut bousillé la vie de sa belle fille YALLA minou saakaa
Faty Thiam
3 giorni fa
Je peux pas comprendre Lou takh surveillance yi seytané dolenn yemm si diokhé de billets de retard de sortie etc
edouard faye
4 giorni fa
Il est dificille d'être enseignant au senegal
Mamadou Bente Diallo
4 giorni fa
Bonjour, naka Koorgui ? Je vien à peine de croiser cette série en naviguant , je la trouve très extra
Ibrahima Lo
4 giorni fa
Surveillant bi esk febaroull
Ndeye Penda Toure
5 giorni fa
ibwsayida
radia lambaye lambaye bi
5 giorni fa
♥️👍
Rhoda Osei
5 giorni fa
Traduction en français s'il vous plait
pape ndiaye
6 giorni fa
Vraiment j aime bien c filme attend la deuxième partie merci a vous les acteurs et actrices
Mame diarra Diome
6 giorni fa
🤝💕
Salla Sow
6 giorni fa
Machaalla bonne continuation, bravo à toute l'équipe. Moi je demande pourquoi certains hommes sont méchants vraiment ces genres de kalidou yi diarrou gno ham. No badola bahoul
Cheikh Touré
6 giorni fa
Cool
Matar Ndoye
7 giorni fa
Certains hommes sont vraiment ingrats .li rk motah yen djiguén ngen wara samou sen bopou bah bagn Di nangu gnulen di nah .goor boula hassee ba ham hors mariage doula massa respect . relation loum nexx nex boumla taha sacrifiée sa bop
Niska Jr
7 giorni fa
Sama ay bok maf katte yangui fi 😍😍 Sétane par force
Fallou gallass lo
7 giorni fa
Serie bi gnika doul sétan la yeurem non li nékh na
Fallou gallass lo
7 giorni fa
Monsieur gueye ya mana fénn
ABDOULAYE THIAM
7 giorni fa
Juliette elle est très belle ♥️💡❤️
boye bi
7 giorni fa
Life school si je pouvais remonter le temps dina done élève bou gateu tanke newe frequentation douma sakh diegué cigarette wakhoumala di "collo collo" aye bone pour diaye break😭
Fama Niang
7 giorni fa
Tamit surveillant bi seuytanei n’a 😂😂😂
las Mc
7 giorni fa
Intéressant
Bara Sow
7 giorni fa
ALLEZ DOUDU
Fatou Thiaw
7 giorni fa
Hi doudou DINA takh makoy sétane
Cheikh Diouf
7 giorni fa
Sacré jacob (pablo)meune Fou nk
Chou Tv
8 giorni fa
Etique et deonthologie mene no mr ndiaye amul😂😂
Fatou Ciss-Ndiaye
8 giorni fa
J'ai bien mené j'espère il y aura la suite
madeleine makungu
8 giorni fa
Mettez les sous titres s'il vous plaît
Jahman Fans
8 giorni fa
J'ai mis la série all american sur ma chaine abonne toi❤❤
madeleine makungu
8 giorni fa
Bonjour pourquoi vous mettez pas de sous titres vous savez sur ITput il n'y a pas que les sénégalais qui regardent
Ami Dieng
8 giorni fa
Good job yesdakar.... mon acteur préféré Beydi akka élégant... mashalla 🙏🥰
Jahman Fans
8 giorni fa
J'ai mis la série all american sur ma chaine abonne toi❤❤ et decouvrer la belle leyla
Marie Diop
8 giorni fa
Professeur ak eleve woroul 🙊
Kany Drame
8 giorni fa
Les sous titre si vous plaît 😫
Zeyna Sarr
8 giorni fa
Kane mo guiss ni Mariama dafay nurok Astar😊
Jahman Fans
8 giorni fa
Zeyna Sarr damelni yow ya guiss lolou dh😄😄 Stp aide moi nga abonner sama chaine 🙇🙇🙇
One TG 3
9 giorni fa
Nn bravo👏🏿boy yi louguéen deef mou nekh
Jahman Fans
8 giorni fa
Machallah 😍😍 Stp diapaléma nga abonner si sama chaine🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇
Moussa Cisse
9 giorni fa
Théâtre bou nex... 💪🏽
Mamadou DIENG
9 giorni fa
Une série hyper intéressante. Les acteurs que des professionnels. Hâte de visualiser la suite...🤩
Lika angélique Fall
9 giorni fa
Pourquoi les hommes sont des diammm vraiment c ignoble le comportement de kalidou
Jahman Fans
8 giorni fa
@Lika angélique Fall merci bcp et noublie pas de donner ton avis❤
Lika angélique Fall
8 giorni fa
@Jahman Fans d'accord
Jahman Fans
8 giorni fa
Doynawar mais faut pas generaliser Sinon diapalé ma nga abonn sama chaine🙇🙇🙇
Khady Fall
9 giorni fa
Wa ya fatou mi tit nadi wakham yeup khaliss la ah wa bakhna
Jahman Fans
8 giorni fa
😂😂 même rôle yi moy gneuwate pour elle Sinon diapaléma nga abonelma sama chaine 🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇
seeni gzty
9 giorni fa
Yesdakar
La lionne a son univers Univers
9 giorni fa
Mangui toudou MARIAMA..deuk ak samay NAWLE am problem CHOIX bay doundou INFIDÈLE ..moudone sama REGRET ba meuneutouma neik DIABAROU GOOR GUI..parfois may doundou DÉRAPAGE ndah IMPACT bima am..DOU MANE tayoumako heilou halei rek...mais parer n'a neik sokhna LEUZ CHÉRI 😆😆🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣Ana sama wa team andeu seitane série yeupp🤭🤭🤭🤭
Khadi Fall
10 ore fa
Li cheri ci net bi dh man Manou mako setan bilay
Gnagna Dabo
Giorno fa
Je viens d'ouvrir cette série par hasard et bizarrement je ne regarde aucune des autres séries citées.
Mame Diallo
3 giorni fa
Machalla
Mame Soda Niang
3 giorni fa
@Hawa Boye choix nékhna dé
Hawa Boye
4 giorni fa
Choix dei la doul sétane ak leuz cheri
Moussa Ndiaye
9 giorni fa
Retour de thierno Diallo🤗
Elhadji badara Diagne
9 giorni fa
Casting bien réussi mariama de sa mère se ressemblent🔥
Elhadji badara Diagne
8 giorni fa
@Jahman Fans tnkt je vais tout regarder on est ensemble accroche toi ça va aller❤️
Jahman Fans
8 giorni fa
@Elhadji badara Diagne gno far sinon regarde ma chaine et dis moi ce qu'en t'en pense je viens de démarrer mais 😅debut super difficile
Elhadji badara Diagne
8 giorni fa
@Jahman Fans ouf suis désolé Sister
Jahman Fans
8 giorni fa
@Elhadji badara Diagne merci beaucoup ❤ mais c pas Frère c soeur
Elhadji badara Diagne
8 giorni fa
@Jahman Fans c’est fait frère!
Princesse Fatima
9 giorni fa
J’aime bien cette série comment y participer ?
Jahman Fans
8 giorni fa
Princesse Fatima il faut les contacter regarde les infos qu'ils ont donner sur leur description Et stp diapaléma nga abonner sama chaine 🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇
Pape malick Lô
9 giorni fa
Meilleur série
Papa Gueye
9 giorni fa
O
Papa Gueye
9 giorni fa
O
MAKA MB TV
9 giorni fa
Vraiment c intéressant 💪💪😍😍
Yoro Fall
9 giorni fa
21311124Je 7r4
Baba Wague
9 giorni fa
Mais série bane jour ak bane jour laye guéne
Jahman Fans
8 giorni fa
Holal si sen description amena les infos Et stp diapaléma nga abonner Sam chaîne 🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇
Oumou Salamata Diouf
10 giorni fa
Pourquoi certaines belles-mères sont bizarres au lieu niou diapalei xalei yii ci seine seuy niom nioy tass keur gui
Jahman Fans
8 giorni fa
Peut-être leurs belle mère leur faisait pareil gnouy continuer tradition bi rek😅 Sinon diapaléma nga abonner sama chaine je t'en prie 🙇🙇🙇🙇
LAYE AWA NDIAYE
10 giorni fa
Sén eye brow yi rafetna trop machalla
Jahman Fans
8 giorni fa
Salut diapaléma nga abonelma sam chaine je t'en prie 🙇🙇🙇🙇😆
zeynab Djamil
10 giorni fa
Fo fékk surveillant day meune doul lolou séne crédo leuh😂😂😂
Jahman Fans
8 giorni fa
😂😂😂 thiey Sinon diapaléma nga abonner sama chaine je t'en prie 🙇🙇🙇🙇🙇🙇
Aminah Kareem
10 giorni fa
Good job
Gaye Beye
10 giorni fa
Ana wa tim wifi manifeste vous🥰
Oumar Ka
10 giorni fa
Copin biidone toukh à l'école dafa ndouru ak jon batiste
Khady Birame Ba
10 giorni fa
Wa mane waxouma lolou dh Ki beug taak Mariama on dirait il a le même âge que ses propres parents à lui😂😂😂 anh wa baxna neeeeeeene def😂😂😂❤️❤️
Mariame Wade
4 giorni fa
moma diahal aek sin regard flippant là😂😂😂
fadel infos
10 giorni fa
Mais Nadège mo nékone si série niankou bii si je me trompes pas
Amina Koné
10 giorni fa
Machallah série bi ndiro na lou nékh Yalla na soti ak diam🙏
rokhaya ndiaye
10 giorni fa
Wa surveillent bi mo meuna doul rk😅😅😅😅😅
Jahman Fans
8 giorni fa
Surveillanct yi dagno sonal élève yi😂😂 Sinon diapaléma nga abonner sama chaine 🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇
fadel bu lo
10 giorni fa
Kalidou gorel wayy bul yakk sunu derr niounn modou modou yi ahh ishh wayyy bu ma yakall dh🤣🤣🤣
fadel bu lo
10 giorni fa
Secret de famille amul serie bu ko dakk stp donner ns les suites saison svp sino good jobb yes dakar🖐🖐🖐
Mboulou Gang
10 giorni fa
Mane doudou la fan😂😂😂🔥.sama surveillant nilamelone mane ak mome mo daak clásico 😂😂😂🔥.Force a vous
Awa Diaby
10 giorni fa
Les sst sont prevus pour quand svp ??
Jahman Fans
8 giorni fa
Holal si barre d'infos bi🖒 Sinon diapaléma nga abonner sama chaine 🙇🙇🙇🙇
Abo Beats
10 giorni fa
01:00:13"Té le moment importunt" Faires attention au prononciation !
Malick Ndiaye
10 giorni fa
Ok
Papa_Rafinha 12
10 giorni fa
Les jours??
Jahman Fans
8 giorni fa
Ils ne l'ont pas encore dit Sinon diapaléma nga abonner sama chaine
Rouguiyata Amadou Touré
10 giorni fa
Les acteurs sont trop bien choisis dieuleul prof bou niak fayda bi
Jahman Fans
8 giorni fa
Kikay moy lolou😂😂 Sinon diapaléma nga abonner sama chaine 🙇🙇🙇🙇🙇
MOUNASSE NGOM
10 giorni fa
Le vieux à biendit " seuyou mbok " moylolou
Gaoussou Diallo
10 giorni fa
Ul66
Ndiogou Samb
10 giorni fa
Bayilene yakh derou professeurs yi. Bouguene mounouta wakh thii niom Lou bakh nguenn mando. Merenalene trop
Jahman Fans
8 giorni fa
Boul mér way hamenagnou dans la généralité nos prof sont top 👍👍 Sinon diapalé nga abonner sama chaine 🙇🙇🙇🙇🙇🙇🙇
drttyu liqm
10 giorni fa
Numa bagné sirveillant bou titt té ni ana samay morom beuss lénn pousse bleu 😂😂
Jahman Fans
8 giorni fa
😂😂😂😂 Sinon diapalé nga abonner sama chaine🙇🙇🙇🙇🙇🙇
soso sousou
10 giorni fa
Sérieux y’as pas de sous-titres 😭
ibrahima sene
10 giorni fa
A
drttyu liqm
10 giorni fa
Les sous titres s’il vous plaît. Attention le son est trop juste, sinon la série promet 👍🏿
CHEIKH AHMED TIDIANE KA
10 giorni fa
Kalidou devrait être plus jeune que ça.... mon humble avis !
SEN COMÉDIE
10 giorni fa
Pourquoi monsieur ndiaye tmt
sannio komi
10 giorni fa
Mé kalidou es trop vieux pourq Almamy soit son oncle😁damay fo rk dama beugona commenter rk
Jahman Fans
8 giorni fa
Cc Abonel sama chaine et decouvre la série All American👍👍
Alimatou Niang
10 giorni fa
J'aime aka mako guemmm
Petit Jo
10 giorni fa
Mariage forcé dafa wareu diehh 🛑 Qui est d'accord ???
sannio komi
10 giorni fa
Kou buegua téki téral sa niari wa diour abonél Jules officiel té yalla taxe Kou buegue seydina mouhamad abonél Jules officiel té yalla taxe
Rougui Mbow
10 giorni fa
Nenako youkoul.."ln de quoi😂😂😂😂
Mouhamed Samb
11 giorni fa
Yalla na Senegal am coup dafrique amine
Tanguy Ndombele
9 giorni fa
Sheurt ....amine 🤣
mimi fk
11 giorni fa
Bjrs vous allez mettre les sous-titres en français ????
Fatousaliou Tambedou
11 giorni fa
Wa mane mome douguéne wakh thi mane di weur série yi rek waa bakhna😂😂😂😂😂
Adama Geuye
11 giorni fa
Wa professeur bi guene mene féne
Abdu Maty
11 giorni fa
Allongé woull gnou tambalii ligèy bii thioooo 😭😂
Assy Dieng
11 giorni fa
La maman de mariama ohh je l'adore ❤️❤️❤️
Toure Ibou
11 giorni fa
Mariama
mijuo roui
11 giorni fa
Serigne thierno dialaloudine dafay fènn rèk khamoul dara
Pisco Vince
11 giorni fa
Xalè bou goor bi dièppi nako waay. Loumouy layam layami niii
mijuo roui
11 giorni fa
Wa surveillant kagn lay arrêter tamit beugga touhlo xalei yi ni rek tei guissouleine niouy toukh dako yorr rek ngay insister di wotei ish no mane beugouma heittou surveillant yi
Saint Julien Mendy
11 giorni fa
Les sous titres s’il vous plaît. Attention le son est trop juste, sinon la série promet 👍🏿
Pisco Vince
11 giorni fa
Marodi amna problème dh
Diop Ndeye maréme
11 giorni fa
Séribi nikh na machala
Clara Mohamed
11 giorni fa
Les sous titres svp
Clara Mohamed
10 giorni fa
Ok merci on attend
Yesdakar
11 giorni fa
Bonjour c'est pour bientôt.