Intrattenimento

CHOIX - Saison 01 - Episode 43 - 05 Avril 2021

Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
itput.info
instagram ssp_senegal
facebook Ssp-senegal-1840512872886698/
twiiter search?q=ssp_senegal&src=typed_query
TIK_TOK ssp_senegal

Commenti 

  1. Modou tala Ceesay

    Modou tala Ceesay

    7 ore fa

    🖊🖊🖊🖊❤

  2. Hassane Ndao

    Hassane Ndao

    Giorno fa

    M

  3. Aita SAMB

    Aita SAMB

    2 giorni fa

    . rdtv 7 snuggles . I

  4. Diaw Thierno

    Diaw Thierno

    2 giorni fa

    Nn père zora je t adore bilahi

  5. Ndeye sokhna sane

    Ndeye sokhna sane

    4 giorni fa

    Nekhoul bâ nekhoul mais barbieeee niawwwnaa😭😭😭

  6. Ndeye sokhna sane

    Ndeye sokhna sane

    4 giorni fa

    Waaa legui barbiiiieeee roseee miiiiiii😂😂😂😂😂liiiiii mbaaaa diammmmmmm😂😂😂😂

  7. Ndeye sokhna sane

    Ndeye sokhna sane

    4 giorni fa

    Fallll tontouuuu rekkkk layyy defffff😂😂😂😂

  8. Ndeye sokhna sane

    Ndeye sokhna sane

    4 giorni fa

    Fayeeeee leuuuuu barrronnnnn boulmaaaa woookkatiiiii 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  9. Ndeye sokhna sane

    Ndeye sokhna sane

    4 giorni fa

    Wawa mane noeudddd de papillon biii dokhhh thi série biii nakkk😂😂😂😂

  10. diara diara

    diara diara

    6 giorni fa

    Deliya dama saf nak

  11. diara diara

    diara diara

    6 giorni fa

    Waw

  12. Bousso Diakhate

    Bousso Diakhate

    6 giorni fa

    Yéne gni di toudou serigne yii si commentaire yiii soof guéne beugue j'aime rk j'aime loumouy diarine Wakhléne si série bi

  13. Ndeye maréme Gueye

    Ndeye maréme Gueye

    7 giorni fa

    Choix nèkh n'a trop ♥️

  14. talibe Seye

    talibe Seye

    7 giorni fa

    Madiaga damqko beug 😂😂

  15. Mouhamed Cisse

    Mouhamed Cisse

    8 giorni fa

    Père Zora😍😀 fan naleu

  16. Massey Kamara

    Massey Kamara

    8 giorni fa

    Bayi lén té ngàt

  17. Ousmane Sy

    Ousmane Sy

    9 giorni fa

    A

  18. Alioune badara mbaye

    Alioune badara mbaye

    9 giorni fa

    Rayan joue très bien

  19. Cathetine prunelle

    Cathetine prunelle

    9 giorni fa

    madiaga il est fort dans le theatre il m fait trop rire sanekh aussi il jout bien bravooo

  20. Soulye mane ba Ba

    Soulye mane ba Ba

    10 giorni fa

    Pape thione yalla nako yalla yérame amine

  21. seydi Malick

    seydi Malick

    10 giorni fa

    Diana niaw trop

  22. Djily Vision

    Djily Vision

    11 giorni fa

    Ma diaga dou nitt😂😂😂😂😂

  23. Khady Thiam

    Khady Thiam

    11 giorni fa

    No ma Diaga 😂😂😂😂

  24. aicha alarba allf

    aicha alarba allf

    11 giorni fa

    Mashallah Madiaga sagnesètinga contane si yaw rek mane yamaye mirlo

  25. Diaw Nar Mbaye

    Diaw Nar Mbaye

    11 giorni fa

    La copine de Diana aussi sheut🤦‍♀️. Je croyais que djiner bOu djiguene leu🤣

  26. Massey Kamara

    Massey Kamara

    11 giorni fa

    Néna KO ay lek lagune,

  27. mounass sow

    mounass sow

    11 giorni fa

    Copine diana bii com la vache qui rit, diana yaw tamite sa baby hair bii doynawar d

  28. Aida Diouf

    Aida Diouf

    11 giorni fa

    Bouma wokati😂😂😂wa madiaga mom louko dal

  29. Aida Diouf

    Aida Diouf

    11 giorni fa

    Mandiaga la beug mane🥺😂😂😂😂😂😂

  30. seynabou fall

    seynabou fall

    11 giorni fa

    Madiaga dou nit"seu papa dafa je retiens" kaay 🤣🤣🤣

  31. Mor Gueye

    Mor Gueye

    11 giorni fa

    Genre kharit yi melni Madiaga🤣 wouy nena ko faye boulma wokati

  32. Marguerite Ndiaye

    Marguerite Ndiaye

    12 giorni fa

    Madiaga rayna ma nenako sa PAPA DA FA JE RETIENS😂😂😂

  33. Mamy’ Chic

    Mamy’ Chic

    12 giorni fa

    madiaga mo nekhal film bii 🤣🤣🤣

  34. khélcom tv

    khélcom tv

    12 giorni fa

    L'homme de série

  35. Leuz Leuz

    Leuz Leuz

    12 giorni fa

    Jojo arrête tes pantacourt

  36. Thiatt Fall

    Thiatt Fall

    12 giorni fa

    Waa borom niari ponpon yu rose yii mom osé neu d té am fitt té sohor shii xarite bu capable baahoul dineula dougeul ci loy rethiu

  37. Aissata Ba

    Aissata Ba

    12 giorni fa

    Non rayane mo nékh néna lo beug ma vocale lako 😅😅

  38. Casamance Ma fierté

    Casamance Ma fierté

    12 giorni fa

    Qui est d'accord que nii sanekh à l'époque est plus drôle que sanekh de maintenant beuseul j'aime 😁

  39. Casamance Ma fierté

    Casamance Ma fierté

    12 giorni fa

    Non mann rayann réwandé bii rekk mo mey fadj🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  40. Sénégalaise d’Allemagne Ndene

    Sénégalaise d’Allemagne Ndene

    12 giorni fa

    Sangomar khamoul né nidiaye moy yaye Ak âme tons noumou nekhé😍😍

  41. anta waly

    anta waly

    12 giorni fa

    Non mane sonwou madiaga bi dama kay degue rk sama fitt dém 😂😂

  42. Aminata Fall

    Aminata Fall

    12 giorni fa

    Wah xaritou Diana bi Dinama saf loy nak ak you rosame ki Tal mêche yi rek la begue

  43. ALBOURAKH24

    ALBOURAKH24

    12 giorni fa

    Madiaga mbaye sa dior il est capricieux mais je l'aime comme ça

  44. Moussoboy TV

    Moussoboy TV

    12 giorni fa

    Yalla na Diame yangue Sakhe si adouna bi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  45. Aminata Faty

    Aminata Faty

    12 giorni fa

    Madiaka je l adoré vraiment

  46. Faty mallé Geuye

    Faty mallé Geuye

    12 giorni fa

    Cv

  47. Maimouna Fall

    Maimouna Fall

    12 giorni fa

    Non j'adore pére Madiaga dafmaye fath 😂😂😂😂

  48. Mariama cisse

    Mariama cisse

    12 giorni fa

    Borom pon pon yi beurina n’a manière bizzare n’a moder n’a feuss neu meunone n’a simple rek akh mogui niak classe ni tekssi niak horom la voir dal sa me met hors de moi en plus jsp daaaal mais elle me plaît vraiment pas ak kanamammm bi Que Dieu me pardonne 🤣🤣🤣

  49. thiaat Gueye

    thiaat Gueye

    13 giorni fa

    niak fayda bi Saint Louis andal par rapport ak sangomar neikhouma dara ishhh

  50. ALIOU NIANG

    ALIOU NIANG

    13 giorni fa

    bilahi man pére gora la beugue 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  51. Dame Freda

    Dame Freda

    13 giorni fa

    Sa papaaa dafa je retiens 😂😂😂 Setlou ngueine que Madiagua mom d’où fennn.. mom beu leuz dafeyy assumer. Dou daw dou neubeutou. Yonaam nekouciii 😂😂😂

    • fifina Flores

      fifina Flores

      10 giorni fa

      😆😆😆🤣🤣🤣🤣🤣

  52. Jonsaba Kujabi

    Jonsaba Kujabi

    13 giorni fa

    pop

  53. Amadou Sall

    Amadou Sall

    13 giorni fa

    One kontane

  54. Rokhyatou Lo

    Rokhyatou Lo

    13 giorni fa

    Madiaga esk dofoul😂😂

  55. assane ndiaye

    assane ndiaye

    13 giorni fa

    Madiaga dinama raye😂😂Yallah nako yallah défal jamm

  56. Thiaba Ndour

    Thiaba Ndour

    13 giorni fa

    Diama ki copine wala sa sœur la ressemblance est frappante

  57. MARIAMA KANDE

    MARIAMA KANDE

    13 giorni fa

    Mais madame pom pom nena diana "diokhma fa vert"

  58. mame diarra ndiaye

    mame diarra ndiaye

    13 giorni fa

    Éye waye madiaga kouy wakh ak mome 😂😂 tamite

  59. Ndaye yacine Diene

    Ndaye yacine Diene

    13 giorni fa

    Je t’aime 😍😍😍

  60. bamba officiel bou wally seck

    bamba officiel bou wally seck

    13 giorni fa

    Athia gayi

  61. mami Deme samba

    mami Deme samba

    13 giorni fa

    Madiaga😂😂😂

  62. Mamadou Seye

    Mamadou Seye

    13 giorni fa

    Ma diaga dinama bari na probléme 😄🤣😄😃dinama escanter

  63. Saer hihi Odf

    Saer hihi Odf

    13 giorni fa

    Dalleu sangomar Yi 🤣😢😭🏃🏃🏃

  64. Mariemebelle thiam

    Mariemebelle thiam

    13 giorni fa

    wawa tonton madiaga dou ma raye ay li amale touti sounou kérsa fay le baro boma wokati

  65. OMZO 91

    OMZO 91

    13 giorni fa

    Mane madiagua momay fathe

  66. Mado G'y Dioufy

    Mado G'y Dioufy

    13 giorni fa

    Ahhh sama madiaga maysa dior🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  67. rabya sadio

    rabya sadio

    13 giorni fa

    Thieuy Madiaga ak aÿ déguisement wame☺☺☺

  68. Ndeye awa Kane

    Ndeye awa Kane

    13 giorni fa

    Ku beugeu serigne salique bëseul jaime

    • Ndeye awa Kane

      Ndeye awa Kane

      13 giorni fa

      Ku beugeu brome diamano beusal jaime

  69. Ndeye awa Kane

    Ndeye awa Kane

    13 giorni fa

    Wouy nenako lo beugeu ma vocal lako hahaha

  70. Mame bousso Mbodj

    Mame bousso Mbodj

    13 giorni fa

    Wa yen Madiaga mi dougn si waxx🤗🤗wa baxna allons rek🤣🤣yi façon déguisement,motaxit Faye nénako sw correct

  71. Anna SARR

    Anna SARR

    13 giorni fa

    Ma ndékéyoooooo Madiagua la neugue, ak kane?

  72. khady thiam

    khady thiam

    13 giorni fa

    Madiagua moy starou théâtre bi

  73. Aminata Thiam

    Aminata Thiam

    13 giorni fa

    Mandiagua

  74. Gueye Fatim

    Gueye Fatim

    13 giorni fa

    macha allah😘😘😘😍😍☺☺👍👍👍✌✌

  75. Diarra

    Diarra

    13 giorni fa

    Mdrr non Madiaga il est drôle quoi

  76. Abdoulaye Gueye

    Abdoulaye Gueye

    13 giorni fa

    noo Madiaga maissa reew na

  77. tigresse tigresse

    tigresse tigresse

    13 giorni fa

    Wa baron s'il nest pas meauvais il est quoi au juste

  78. Mame MAMA

    Mame MAMA

    13 giorni fa

    💗💗💗💗💗💗💗❤❤❤

  79. Mame MAMA

    Mame MAMA

    13 giorni fa

    Nice

  80. mbene soung

    mbene soung

    13 giorni fa

    Ana gni bègue baye Karim mbacké borom makarimal akhlaq

  81. Daba Dieye

    Daba Dieye

    13 giorni fa

    Père zora me fume

  82. Khady Sow

    Khady Sow

    13 giorni fa

    Sangomar sa nidiay defoula dara changel sa comportement ak mom nidiay moy yaye un peu de respect

    • marem ba

      marem ba

      12 giorni fa

      tmt

  83. elass kane

    elass kane

    13 giorni fa

    Ay madiaga mom d dafa am son spécial pour bou génné

  84. oumou diop deme

    oumou diop deme

    13 giorni fa

    Esk deguene lima degu xaritou diana bi feu vert bii 😅😅😅😅

  85. Fatou Wague

    Fatou Wague

    13 giorni fa

    Wouye madiagua raynama 😂😅

  86. Thiara Sarr

    Thiara Sarr

    13 giorni fa

    belle série

  87. Sokhna seynabou Diouf

    Sokhna seynabou Diouf

    13 giorni fa

    Faye le baron bouma wokatii🤣😂🤣😂🤣😂madiagua bodola nga

  88. Maguette Diop

    Maguette Diop

    13 giorni fa

    Faye le baron bouma wokati😂😂😂😂woyy lii eupeuna 🤔😉😉

  89. Waly FAYE

    Waly FAYE

    13 giorni fa

    Non keneu dou madiaga

  90. Die Cisse

    Die Cisse

    14 giorni fa

    Mame goor fou Mou nekh pourquoi dou wakh si adji akh sonko il est peur qu ont bluire sa maison domerame de premiere katagory moye mame gor djiguene

  91. marieodile diatta

    marieodile diatta

    14 giorni fa

    Moi je l'aime bien sanex est le meilleur acteur que le sénégal🇸🇳 à dans la scène cinématographique 🤔qui est d'accord avec moi un j'aime 👍

  92. Adja Sadio NDAW

    Adja Sadio NDAW

    14 giorni fa

    Madiaga ya rew🤣🤣🤣

  93. Toure Khadim

    Toure Khadim

    14 giorni fa

    Peunchline de l'année [ boye séti borom xaliss dangaye sangsé 😂😂]

  94. ndogal deme

    ndogal deme

    14 giorni fa

    Nice n'a

  95. mya ndiaye

    mya ndiaye

    14 giorni fa

    Ki d’autres pensent comm moi k Diana c’est la demi sœur de Délia et Rayan🤔

  96. Ousmane Sow

    Ousmane Sow

    14 giorni fa

    Sangomar commence à m'as merdé😔😔

  97. Amadou Fall

    Amadou Fall

    14 giorni fa

    Madiaga je l’aime trop

  98. Ndeye bousso Diakhate

    Ndeye bousso Diakhate

    14 giorni fa

    Man dall madiaga la beugue

  99. Normal Lo

    Normal Lo

    14 giorni fa

    Qui est d'accord que la trahison ça coûtera Mal .

  100. Ndeye bousso Diakhate

    Ndeye bousso Diakhate

    14 giorni fa

    Waw diaro binak Mété jull

Il prossimo